12 thoughts on “Week 7 NETTALI

  1. Sama yaay toggna. Raxasuna te fompuna. Indina ceebu jën bi ak kuddu gi. Lekkngeen et waxngeen “Neexna!” Sama yaay raxasna aset bi te dimbalenaa.

  2. Lëkk nanu añ. Raxasu nanu, ak fompu nanu. Indi naa mbour, beurre, ak ceeb. Sama mag ju jigëën, indi na ñeex ak kuddu.Xanaa añ ba baax saf. Sama yaay wax nanu, lëkkal! Nuñ, lëkk nanu.

  3. Sama pàppa toggna. Raxasuna te xarna lujum. Defna ci pot. Indina beurre, poobar, xorom, kaani ak yápp. Saafna yàpp ci pool te baxna lujum. Ci gannaaw lekknanu ci waañ. Neexna ñam! Sama pàppa toggkat baax la.

  4. Sama Maam ju jigeen toggna. Raxas ceeb ak jen, fompu ci sarbet bi. Togg ceebu jen bi. Indi ceeb, tamaate, lujum, ak jen. Togg 1 waxtu. Sama Maam ju jigeen wax: Japp sa kuddu, na rees ak jamm! Neex na!

  5. sumina ay dallam, Mu ngi raxasuna. Nuyal gan gi. Mu ngiy fompu. Mu ngiy indi ceebu jen bi, May ndox naan. Mu ngiy salaat. Mu ngiy neex. Mu ngiy kuddu. Laaj ma: Lekkal way. Lekkgna neex na!

  6. Man togg naa. Raxasu naa ak fompu naa ci sarbet bi. Togg naa ganaar gi ak lujum yi. Man ndox laa naan. Man loxo ak kuddu laa lekke. Neex na. Samay Aset tilim nañu ak man leen laa set. Leegi suur naa ak bak naa.

  7. Man, duma toggkat. Sama xarit Nicole mu ngiy togg. Moom, togg la nob! Reer la togg. Raxasu na te indi na sarbet. Tàng na ci waañ bi. Naan na ndox. Jox na cere faas ak mbaxal! Xoox na. Nu ngiy lekke kuddu. Neex na! Ba beneen!

  8. Summi nanu dàllam ak raxasu nanu. Fompu nanu ci sarbet bi te jox naa waakër kuddu. Moom, lekke lanu kuddu. May naa waakër ñeex ak ceeb, yàpp ak lujum. Man, defal ma tuuti te neex na! Naan lanu ndox. Wax naa “Na rees ak jàmm!”

  9. Mu ngiy raxasu ak fompu. Maa ngiy indi ceebu jen bi. Mu ngiy lekk ceeb bi. Ñu ngiy lekke loxo. Lekkal ceeb bi! Aycaleen! Lekkal waay! Am! Doo lekk. Neex na. Moustapha ngiy indi cere baasi gerte. Toogal! Foo jëm? Na rees as jàmm!

  10. Waakerr gi nyeep nyungé paré añ. Man, suminaa samay dalla, raxaxu naa, legi tog naa. Añ naa plasas ack waxtan naa tuti. Waxnaa sama yaiye neh añ bi “nexna torop!”. Legi jögnaa raxasu waat.

    🙂

  11. Moon pareena pur ayganam. Moon raxasuna ayloxoam. Ak waxna ci aynjabootam “Gennleen, foleen yeen!” Kon, moon sebetna pur reer la. Ak dogna lëjum, baanga ak yàpp gann. Su leppa bantana moon oona ku-nekka biir. “Kayleen, kayleen! Reer!”

Leave a Reply

Your email address will not be published. Required fields are marked *